"Gatsa Gatsa"
— iliyoimbwa na Magui
"Gatsa Gatsa" ni wimbo ulioimbwa kwenye msenegali iliyotolewa mnamo 24 agosti 2023 kwenye chaneli rasmi ya lebo ya rekodi - "Magui". Gundua maelezo ya kipekee kuhusu "Gatsa Gatsa". Tafuta wimbo wa maneno wa Gatsa Gatsa, tafsiri, na ukweli wa wimbo. Mapato na Net Worth hukusanywa kwa ufadhili na vyanzo vingine kulingana na kipande cha habari kinachopatikana kwenye mtandao. Wimbo wa "Gatsa Gatsa" ulionekana mara ngapi katika chati za muziki zilizokusanywa? "Gatsa Gatsa" ni video ya muziki inayojulikana sana ambayo ilichukua nafasi katika chati maarufu, kama vile Nyimbo 100 Senegal Bora, Nyimbo 40 msenegali Bora, na zaidi.
|
Download New Songs
Listen & stream |
|

"Gatsa Gatsa" Ukweli
"Gatsa Gatsa" imefikia jumla ya mara ambazo zimetazamwa 86.2K na kupendwa 4.4K kwenye YouTube.
Wimbo umewasilishwa mnamo 24/08/2023 na ukatumia wiki 5 kwenye chati.
Jina asili la video ya muziki ni "MAGUI - GATSA GATSA (FREESTYLE) PRODUCED BY METHODIKS".
"Gatsa Gatsa" imechapishwa kwenye Youtube saa 23/08/2023 21:00:09.
"Gatsa Gatsa" Nyimbo, Watunzi, Lebo ya Rekodi
MAGUI - Gatsa Gatsa (Officiel music vidéo)
prod: Methodiks
link to plateforms:
Mix mastering: Trish Snooki
Realisation: @eyeofrafilms / Magui
Cadrage,Montage & Etalonnage: @eyeofrafilms
Paroles
Binde ngak pèle bila soul
Yaffi daxa rap yaw ya meuneu dul
Pourtan may xalé bifi geuneu cool
Té Dugulen forcé todj na seni toul
Terelen nelaw, sen xessal yi niul
Gatsa gatsa ku nieuw je refoule
(Bitch ) sen Lamigne yu reuy te jobbo len
taxna rap jiggen bi demul
diap teint meunoma tour leundeum
Faax ni guy munulen ma geusseum
Tou le temps mangui innover
Yen Sen projet yi rare ni kuy wethio deureum
Telen sama loxo jegg ak keureum
Mane may or yen ngen ay peureum
Warngen ma geureum yegual niveau bima deuké te deguo mo tass seureum
Dama nieuw xambate tall bi
Né kogne bek tal bi
Yokk ambiance bi reguine tadj tan
tekk ko si tant bi,
dugeul sen camp yi , nangu sa gang bi
Deflen ay fan
bayilen ak vent bi,
nangu sen far yi
Ngen deuké di xoy bine bine ak namp
Woman of the year
Clash ma lek sa fane
Effet boomrang
kuma yapp dama fekk may nelaw
Geudieu guéné sen game selaw
Name ngen trone bima nangu si yen
te dolenko degg muné malaraw
Sa xol budé bone nanal sexaw
xel buy tey ngala tey lekal kew
Fimay xol meunoko guiss
Rombe la guisso ludul sama ngelaw
Gatsa gatsa gatsa gatsa
Son bi bu lalé sa mc neko
Massa massa massa massa
a4 47 lay composé
Sama ancre si lave lay jugguè
King beat koniu bandit lay mixer
Suniu produit day électrocuté
Deggal ma yi hitt
Projet bi paréna 10 titre
Amna ay feat wicked
Birr Africultur pikine
Danga name music baxx bi
Binde yu tight yi
Qualité ak quantité bu doy bi
Theme yu rare yi
Images yu nice yi
Aout ma may mixtape bu baax bi
Maynako we are us
Maynako gni si diappeu
Maynako sama famille africultur
Tax lepp yemb.
Tax ngen ma geuneu xam sama bop
Tax ngen ma geuneu xam lima done
Leral ngen ma si ama yone
Ba dara dul dara tay lepp doxx
Omar, Abu, zeinix,
Sall ngarry lakka mass
jah jah, Trish,mustaf
coumba, king, moyza
methodiks , bousso Makosi ,
channel, prince Matador
Bigi , vicky velly, kash
Bf, fula ak leuz
Nos réseaux ????????????????????????
Facebook: Magui L’officielle
Instagram: iam__magui_diop
Tweeter: iam__magui
Snap: chou_rouge
Spotify :
Deezer:
Apple Musique :
#tendance #rap #reels